/** * Match wp_head() indent level */ ?> #JummahMubarack: La Responsabilité d’un dirigeant

#JummahMubarack: La Responsabilité d’un dirigeant

0

Mbokk yi, na gnou khame ni Ndjitt gou nek bou euleugué di na gnou la lathie naka nga saammé woone ndiaaboote gui!
Donc gnou khame ni rek, kepp kou meussa djitté: ngay kilifeu diné, di président, maire, député, ministre etc. di père de famille, euleugu di nga rendre compte.
Sou gnou nékké si position wou ndjitt, lène rek mo gnou waarra niorr: deugou té di deff li gueune à chaque fois, évité di calculé ak di khol lou nékh massamba wala mademba wala di deff aye 1/2 mesures. loolou mome si moussiba rek la ley dieumé!
Yalla na gnou Yalla dooli suturaa
Gni fatou, Yalla na lène Yalla yeureum, diégueul lène, gnou khippé firdawsi!
#JummahMubarack

Share.

About Author

Leave A Reply