/** * Match wp_head() indent level */ ?> #JummahMubarack : Éduquons nos enfants…

#JummahMubarack : Éduquons nos enfants…

0

Mbokk yi, na gnou yaarr ndiaaboote gui si diiné, si humilité, si sutura, si deuguou, deff si séne bopp yi xam xam ba gnou ame la base ndakh diamono dji doye na waar dooye waar goo khame ni kou ci amoul base da ngay nékhaa beumaakh, lou gneuw yooboula. Nagn léne investir si Éducation khaalé yi, devoir la, ndakh euleuk aakh ley doone ci gnome sou gnou ko deffoul. Té nak, gnou bagnaa topp séne beugu beugu ba loorr léne.
Mbokk yi, Yakaameti ame diabaar wala dieukeur nékhna lolou waayé na nga fékhéé ba so amé doome, nga khaar si sa tankou toubéy, deff tout ba tekk ko si yoonou wou dioupp wi.
Yalla na gnou Yalla mey dégu ak topp 🙏
#JummahMubarack

Share.

About Author

Leave A Reply